Youssou N'Dour - Xel lyrics

Published

0 213 0

Youssou N'Dour - Xel lyrics

Paroles de la chanson Xel : Famarë reub kat lawone Da ama biss mou khall yône Mu taxaw di xalat bamu yàg Mu sène mbëtt miy daw Mu suxat fital ambadi dâgu Té nane kî douma raw Far mbëtt ma sène kokorong Dadi dieul bop ba Dal di koy rône Bopp ba neubouna litha des Yaramam béppa ngui fègn Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya Lippe di fègne Lii takh mou déféni Mbeutteu daa amoul xel Kone gnoune gni Yalla jox xel Nagnu santati (x2) Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax déf Loy dougou jitalal sa xel Ba lo thièy wout Di nga guiss nguenél Nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna Kiy déf té dou xalat Thi missal day mél ni mbeut ma Nit môm khélako yor(x4) Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf Fi neubeu moy khax Boko amoul yangui mél ni bayima Sokou amoul doto nék nit Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf Wawaw(x4) Famarë reub kat lawone Da ama biss mou khall yône Mu taxaw di xalat bamu yàg Mu sène mbëtt miy daw Mu suxat fital am ba di dâgu Té nane kî douma raw Far mbëtt ma sène kokorong Dadi dieul bop ba Dal di koy rône Bopp ba neubouna litha des Yaramam béppa ngui fègn Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya Lippe di fègne Lii takh mou déféni Mbeutteu daa amoul xel Kone gnoune gni Yalla jox xel Nagnu santati (x2) Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf Wawaw lolu moy xel Soko amoul Yangui mél bayima (x3) Loy dougou nang ko téké xel Famarë reub kat lawone Mbeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt!