Youssou N'Dour - Sama Gàmmu lyrics

Published

0 197 0

Youssou N'Dour - Sama Gàmmu lyrics

Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko àbb mbaa nga for ko Baal dóózéé, eh Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko àbb mbaa nga for ko Baal dóózéé, eh Yor xaalis mënui tee me moom la Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko àbb mbaa nga for ko Baal dóózéé, eh Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko Foog nan nita ko waddal nga for ko Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko Man daal maay sa buur nangu ko Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko àbb mbaa nga for ko Baal dóózéé, eh Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee Ah gàmmu daal sama doomu nday nga E e e gàmmu daal suma xarit nga E e e gàmmu daal suma askan nga Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee E e e gàmmu daal suma xarit nga E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga E e e gàmmu daal man suma xarit nga E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga Baal dooc moomu foo ko Teeyai teey teey Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee E e e gàmmu daal sama doomu nday nga E e e gàmmu daal suma xarit nga E e e gàmmu daal suma askan