Youssou N'Dour - Baay faal lyrics

Published

0 249 0

Youssou N'Dour - Baay faal lyrics

Paroles de la chanson Baay Faal : Baay faal gueu da djook thia fadjar Nga sène ko mouy soli sagar Boppam ba sekkeu ki kawar Yoré keulleum ba di sikar Té falé woul khiif ak mar Boo démé sakh khekh na badar Ki toureum wi dotoul fay Kou wéddi li ladj ko wa ndar Baay faal djakhal na wa ndar Baay faal djakhal na wa ndar Baay faal gueu da djook thia fadjar Mani bour Yalla da djook thia fadjar Nga sène ko mouy soli sagar Yoré keulleum gueu di zikar Ki toureum wi dotoul fay Kou wéddi li ladj ko wa ndar Baay faal djakhal na wa ndar Baay faal djommeul na wa ndar Doundeum gueu nekh na Zikar sa neekh na lol Baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor Zikar sa motakh mou djégué Yalla Baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome Thia tool yeu... Thia tèène yeu... Thia wagne weu... Magal yeu... Baay faal liguey la khame Baay faal ndigueul la khame Baay faal dou khekh dou khoulo Beuggue neu nite, fonk na nite khekhoulol Mome la fayé ko lo mou ligueyal sougnou borom Beuggue na la baay faal Nangou nite Kimo djégué sougnou borom Dey liguey di djokhé motakh baay faal djégué naa sougnou borooom... Dey liguey di diokhé Dey liguey di diokhé motakh baay faal Toggam ga nekhna lol motakh bay faal Dey magal motakh baay faal Dey zikar motakh baay faal