Youssou N'Dour - Yama lyrics

Published

0 187 0

Youssou N'Dour - Yama lyrics

Soubateel, bamuy barilé Ñi di déloo sen palanter Ngir baña xaar li xew, li xew féneen Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Gaal gi teer Ba ñu seet li, li wara dem féneen Té du yeebi ludul meew lifi des Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Moo waral bu sédalé, du am Du am, rusna ñaan ba day fandé, fandé Moo waral bu sédalé, ba du am Du am, rusna ñaan Kii daal amu fi morom Yaamaa nango sona lol Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Ni dox sa waar bamu noppi yaw Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi Yaama rek la soxal diarama Diarama, diarama Ni woo Yama, Yama Wuy Yama, amufi morom Wuy Yama, nangoo sona lol Ni Yama, jigen ju man goor Wuy Yama, maa la setlu way Moo waral bu sédalé , du am Rusna ñaan ba day fandé Amu fi morom Mala setlu way Yama, Yama Amul noflay Amu fi morom Tunda wi rañénañ la Yama, Yama Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon Ni woo Yama, ni Yama gaa yi yaaba leen Ni dox sa waar bamu noppi yaw Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi Yaama rek la soxal diarama