Youssou N'Dour - Live television lyrics

Published

0 324 0

Youssou N'Dour - Live television lyrics

Paroles de la chanson Live Television : 1er couplet Ouragan ouppeul a**amane Ba djante leer ma djanok satellite Satellite ngalla yoné ma la khew feulé,ak fénène ak fénène Mani go, go, go Ni live, live television live, live tv live 2e couplet Roplane bi warone tiim Dima eundil ki ma namona ngui Wayé tey télévision waar na ma, wone ma lima beugona guiss, ouragan mani ouppeul ouppeul ouppeul Ni live, live television life, live tv live Oh life, live tv live, live television live Fook na né formalité leu(...) Fook na né formalité leu(...) Fook na né formalité leu(ma djapp yénéni chaines) Fook na né formalité leu, leu, leu... 1er couplet Je vais vous raconter une histoire extraordinaire Un soir, une famille nous avait invité mes amis et moi, il y a quelques semaines de celà Nous étions une vingtaine à nous retrouver dans un grand salon, attendant avec impatience que le dîner soit servi Devinez ce qui est arrivé à neuf heurs moins cinq,la famille nous abandonnés dans le salon, préférant s'enta**er dans une petite chambre, avec une télé mal éclairée,uniquement pour regarder, cette fameuse émission ....khalaa** ....wala bok niou dem Chéri souma sadjobane Dina liguey ba ame louma djeundé satellite, nguir guiss di guiss la thia bbc, la thia ortm wala la thia mtv yeah Ni live, live television live Live tv live We need live, live tv live, live television live Yaw chéri souma sadjobane, dina liguey ba me louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia bbc wala la thia mtv yeah Wawaw kone television wawaw Yeah chéri souma sadjobane dina liguey ba ame louma djeundé satellite nguir guiss di guiss la thia orts, la thia cnn wala thia mtv yeah Wawaw kone television wawaw