Youssou N'Dour - Shukran Bamba lyrics

Published

0 377 0

Youssou N'Dour - Shukran Bamba lyrics

Shukran lakah... modou bamba mounoumala faye khana ma wayla Ligueyba de rek nguir at ya allah mbacke da nga yah guinaw Ak kanam nagne roye thi yaw rek meuneu dieum thi kanam Cheikh ahmadou, backe mane de sante nala diadieuf bayou Mamadou lamine bara sama di guante ak ya allah yama ko leral Lou ne nawal nga ko te takhoul nga diakhal ya takh may bale Di yeureumate ken dotou ma ata te ba na khebate diaaa dieufe Bayou serigne saliou serigne mourtalla chukran bamba chukran Laka chukran chukran chukran chukran chukran odou bamba...