Youssou N'Dour - 4/4/1944 lyrics

Published

0 211 0

Youssou N'Dour - 4/4/1944 lyrics

4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex 4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex Boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na Tóllu nii war ngeena bég, war ngeena bég ci independans bi, ak ñi ko indi 4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex 4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex Boo lékkee ba suur war ngaa gërëm, war ngaa gërëm ñi dugg ci waañ wee, waañ wa tàng na Dama ne bu lëk lékkee olom budee gore na te dëggu war na ko gërëméé picc yi No, no, no, no, no, no No, no, no, no, no, no, yee 4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex 4-4-44, 4-4-4-44 gis say mbokk, moo neex Ah lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gëm sa bopp moo neex 4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex No no no gis say mbokk moo neex 4-4-44, 4-4-4-44 moom sa bopp, moo neex Waaw Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, gis say mbokk moo neex Aaaaa, moom sa bopp, moo neex Waaw Lii dafa neex, lii dafa neex, lii dafa neex, moom sa bopp, moo neex