Youssou N'Dour Feat Akon - Song Daan lyrics

Published

0 432 0

Youssou N'Dour Feat Akon - Song Daan lyrics

Parole Youssou N'Dour feat Akon Song Daan Dooley nit kou ñuul kou Ko beug xam la Mbeur mouy daan kou Ko beug xam démal laćć ko you Woma woma Ci leundeum Dinala Wouyou Oubil sama Xol dinga Xam nimou sédéé ci you Fileg mang lay am Sama xol Luma songù Daan ko Fileg mang lay am Sama Xèll Luma songù Daan ko Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh ÉH ÉH ÉH ÉH Béneu biss dina niow Mou melni louniouy netali Mou melni lii dou Anhhhhhhh The ken Du jog Naan man mi nako fékéh Yooooooo Ndah nguelaw lii daaw diñou yobalé Xoob yiy russ ci garab guii Ah lifi xew tay büñü ko fatéé Africa Dom yiy wane Sén bopeuh Fileg mang lay am Sama xol Luma songù Daan ko Fileg mang lay am Sama Xèll Luma songù Daan ko Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Songù Daan Koooooooo Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh Man Maanan Mane iiow laa Iiow nga naan Ngané man leuh ÉH ÉH ÉH ÉH Cí Díg bï Fofù Laay diar Mù am xàl Safara douma daaw Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jēlé Fénéne Fí ñù Diarr ñun ba éksi fí Dafa mèlni Louńou nétali Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jēlé Fénéne Éh Éh Hh hhhhhh Hhhhhhhh Maa contaane Yoow it yaa contaaan Maleu geuuneuu contane Uhh Yeahhhhh Hhhhhh!! Contane yeahhh Yeaaahhh Contane yeahhh Contane yeahhh Akon Yousou Yeah Akon Yousou Yeah Cí Díg bï Fofù Laay diar Mù am xàl Safara douma daaw Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jēlé Fénéne Fí ñù Diarr ñun ba éksi fí Dafa mèlni Louńou nétali Los angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñyou Jēlé Fénéne Song Daan Youssou Ndour feat Akon Lyrics by Abdoulayebacary