Xat Xol Recordz - Nittou Tay lyrics

Published

0 229 0

Xat Xol Recordz - Nittou Tay lyrics

Intro:dafa rér amoul ngeum(nittou tey) Iblisse la fal faté yonnét(nittou tey) Farataloul dinéme(nittou tey).....fonétik Couplet1 Yaw dunya def def bo degg midéf Fatté yalla fal yonnét yalla xaliss Lothi guiss?nakar ak tiss Safane yi di geuneu wathieu Niawtef sentou sa morom Thi galou xathie Fen ak kathie Senegal yéné yé gnou tardelle Yalla atélle Loxoy def té loxoy té loxoy ndindi Dieuf diou yakou def lou bone ba alkou Ta** seuye rayi bakéne Rithie sa téré am sa yalla bop Wett taxoul nga xam séne bop Finition ngay sett namoufay teudé Xana do dé Koune mome geumoul nelawoul Ta fé gnou dieum Lofi djiwone nga fay guopp Doufa dial say soop Aduna diar dial Assalo wakh lou bakh def lou bakh Diaroul yéne yi Ma yeureum gnén gni Talibi xatoul xoll yé xatt Yémoul rek thi chauffeur yi Dagn fé bari chaud coeur yi Douma dém ta kén dou dém Refrain Nitou teyyy(thieuy) Sole dalame Nidou tayi(doyna war) Nittou tey(dafa réer) Soule deugeu souli fén Dieufi ma teyy*2 Couplet 2 Yaw nittou tey Sole na dalame Nidou tayi Thi soul deugeu Souli fen bako sai sai Assalo na boppam Fouti soul bouki souli bouki Xol beutou diambour Sa yéné done louki Jamono bi boy sett ngoor laguo lafi Amoul kéne fi koufi dieufé waxi nabi Mo tax sunu biir cheytane fess nafi Kaniane bone siss Niawtef legui dagn ko miss Thi jamonoy dadial Fep fep la dadial Beugeu ami deureum Dagg nitt thieureum xeureum Gnogui lay réunion Rélo ni amdi mignon Loumou la eupeulé xagne lako Dieul na muchiba xagne lako Démo diko ay gnane woutiko Sa mbokk mola bloqué Agne bagui ni boko léké Maguoume dieum la té ra** Keupeu caisse tabax tera**e Na**axal do gui trace (wou waa) Couplet 3 Xamna li nek sa xell Mola geuneu mbong Day diar sa kaw Téféssou wone la ndong Nittou tey dou rouss fen na barodé Trois quart coss ganila borodé Louer auto trafiqiant de personnalité Naik diom fók ni lolou moy nandité Goru thiapatate démarchame fémi néne la Foko fék kebatou dou masculin féminin la Madar boy sett omo la Matar legui h*mo la Boumou la guondek 4/4 tame Louné lay dathie dani sax tate tatame Guel done ay lesbienne Escroc bari lescul fils you k.... Xamé touma galsen Ooh my god il nous manipule lucifer Guindil sama xett gnou deugeur ni barre de fer Gnou deugeur ni bar de fer