Xat Xol Recordz - Galsen Dundul Déwul lyrics

Published

0 331 0

Xat Xol Recordz - Galsen Dundul Déwul lyrics

1er Couplet Dioudou si année 70 yi si fin fond wou Bronx Kool Herc abeu si jamaicain mc yi taxaw toast Mouy avancé ndank ndank ba Theodore di feuleuk scratch Nioukoy xéxx diko geem Hip Hop taxawé gninte pathie Fok niou xar 79 Suggarhill ték first album Master Flash ékssi woté message. Rap bi déf boom NWA f** na police. Ganstar rap diotena dioudou Ba rogolate biir Paris banlieue feug séni bountou Welcome si Dakar. Année blanche di vidé école yi Niou téri si smurf ak breakdance tons yi créer possee Ambroise ak Aziz Coulibaly génération 80 Puissance fm yok dolé nioukoy geem di geuneu bari Immigré yi feule. Single si Mbacké Dioum Album si mc Lida. Fok niou tékk ataya PBS dougeul riti. Marimba si black mbolo Galsen démarkéwou. Promoteur yi intérrésséwou Refrain Galsen mafia dafa beuri unknowers Douniou meusseu nane séne nda me and my brothers Souniou mission si game moy niodi boy you nara souroukh Diokhagn léne baram wane léne where is the trust 2eme couplet 98 rapadio eksi fini l'age d'or. Mister kane dékil rap Under PA déf K.O. Bibson ni Fata fake la Dééf ko guérre dorikay canon Gaston, Omzo dieul défensou l'exilé Bambino 2003 concept rap new generation. (Walabok) Geble Tigrim B woté innovation Entre temps matador slam. Carlou D ni day musikr Xuman thiape si reggae bi. Awadi yotou public afrique bi Niounouy wowé grand jobatouniou. Akima nd... rap bi Ték sene béne lobby. Dounou mayé chance wakh ko boy yi Légui kou fipouwoul diay léne prék do lék si ndap li Heureusement canaba**e télla adji know louy deal bi Alien si bénéne planete. Pps si bénéne fa**ette Néna tane na boudoul dé. Mixtape yi di takarna**é (Undecla**) Slang bi di geuneu djolofé. Kanaraw ni Fuk N Kuk Takricain ték sagn sagn. Gars yi lém séne guéne ni moute Refrain Galsen mafia dafa beuri unknowers Douniou meusseu nane séne nda me and my brothers Souniou mission si game moy niodi boy you nara souroukh Diokhagn léne baram wane léne where is the trust 3éme couplet Galsen gni ni dounou créer dounou inventer Waliyanne ba nopi reuy lamigne ni nioko mome Bou kana yi dégone wolof dounou diok si dinou ré Réinventé termes yi deugeur fiit di doul di dadialé ]Fi ganstar amoul xaliss. Fi ganster dou dougou jail Fi ganster beugoul lou baxx. Fi ganster sakh amoul guél Old yi geem lo public bi ni boy yi biniy déf dou rap Meunouniou binde di teup di daal si ay beatou dirty ak trap Ténor yi déf faux départ déloyal bagne kouléne daap Faténaniou ni demb nio nékone séne guinaw di support di clap Ay animateur a la con niou saupe léne si béne lobby Méme gars yi naniy ték niénéne gni daal xamouniou gaate Dagnay kathie ba nopi beugue ma geemlo ni fénou niou daal Nopalal sa bopou doma délo époque féodal BossBeatz dou boyou kéne. Bamay adji xamoumaléne Laye Balde, Sonsam, Mbaari ngoné fatéwoumaléne Outro Big up to all my n******gs. Lord Jock, Papa Cisse Bril Fight 4, Sanzala, Rosso, 3g Team, Car rapid Reptil Music, 221 Bangers, Avocat, Mc Boudeur Etk, Pee Boy, Nikel Kami, Fonetik Sama grand Ra**oul Réspect Sikki Sakka Xat Xol for Life Releve By Force