Viviane Chidid - Wuyuma lyrics

Published

0 379 0

Viviane Chidid - Wuyuma lyrics

Viviane Chidid Wuyuma Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beugue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Mane déh walouléne ma wax koko Xalé bi lékatouma ndax mome Nanatouma nélawatouma Wowo Sama xol yathie néh Lék lék ma woo ko tit dal di coupé Sama appetit coupé Febar dinama guoungué Doctueur dama love ba dof Té xawma loukoy fathie Wowo Mba meune nga thie daraa Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beugue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Mane woo nala founé Nga diapémma sa xarite Inviter resto, lalal nala louné Wowo Nga diapéma sa xarite Lék lék ma woo ko tit dal di coupé Sama appetit coupé Febar dinama guoungué Doctueur dama love ba dof Té xawma loukoy fathie Wowo Mba meune nga thie daraa Mane beuguena ma bagne bayiwouma Mane guisoumaa Kénén koudoul mome Mbeuguéleu beuri dolé yén mako xam Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beug Ue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Xalé bi sama réni xol déh wuyu maa Beugue nala té xamothie dara Mbeugyél thie xol ley nék deugueleu Beugue nala té xamo thie dara Kouthie nek'aak kingna nope Sa guinaw bandague faxa**ul Diougueul yyeungueul bamou saf Sa gnuinaw badanue faxa**ul Kouthie nek'aak kingna nope Sa guinaw bandague faxa**ul Diougueul yyeungueul bamou saf Sa gnuinaw badanue faxa**ul Lyrics Viviane Chidid "WUYUMA" by abdouayebacary