Rainbow-clan - Lova lyrics

Published

0 390 0

Rainbow-clan - Lova lyrics

Intro (....) AlyGhost Baby kay kay, gneuwal bilay gnou dem Fo dioxogn ma daggal la, indi visa gnou dem Boul topp say-say bi takh ngamay bye bye Xeuy souba wone ma dokk, newoma sax bye bye Diaral ngama die, deukei sango lou tangu Watou ngandi nel, nela kong ma wangg Deugu leu, tarou nga te amga wang Boumu takh nga djitou, di bayi ma langg BM Wethioma ak kenen nakh nama way Woutina lenen teksi nima, bye bye Man mi ko toude tchapali, mou defma li dh dem dh bayima Bett nama nak dh, waye baby man dh gueunalouma Mougn leu done lou impossible Deuk di guent c'est pas possible Yay sama cible xale bi boula nekhe fireul Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Refrain Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof LOva, Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Lova Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof, ( baby kaay..) Lova Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof, ( baby kaa aa aay) MoOntee Check you jungling your big booty, is my higher fantasy And just, thinking about it, make my heart gninga gningaling I swear my baby you blew me And then you'r driving me crasy, really Let me be the man who'll change your whole life sweetly Am gonna make you smile, show leu sama life style Together we gonna be happy then will fly high Go beu doubaii, feulei Haway tiimm haters yeup nilen Hi! Baby girl kay, lets touch the sky nagnko try BM Fi nga beugu yem ak man beugu ma bayi man mi My lova kay gnou langg, kay gnou ande free AlyGhost Kay gnou ande fethia, nagn tadiabone Kay gnou ande fly dound lebone lepone MoOntee Haaha,you told me bye bye, could you please tell me why? ( why) Sett nala facebook ak tweeter, te guissoumala skype AlyGhost Kay gnou wahtane, bougnu nekk noone Dougu pentagone, ma door leu fone Souba beu ngone, nekk dila bomba Koula diema bomb, ma door ko gun BM Jah lova bulma setane, boulma bayi man mi Noone yangui retane diapalema cii.., MoOntee Ya really even know, you are my lova Don't turn me back baby take me ova Yay sama sadiobatt, rafete beuri filing pathie So beugone weer bi sakh honey doumaci tekk baaaaatt Refrain Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof LOva, Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Lova lova lova lova, mbeuguel leu nekh beu moudje sof Lova Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof, ( baby kaay..) Lova Hey, mbeuguel leu nekh beu moudje sof, ( baby kaa aa aay)