Rafall - Be The Best lyrics

Published

0 261 0

Rafall - Be The Best lyrics

Refrain Don't worry don't worry. Job lou bari dina meusseu soti Be happy be happy. Fight sa life boulsi meusseu tayi Deukeul si di fight sa life. One day dina meusseu nice Guemeul rék yokk sa fight. Béss sa gui téw digua diote sa price 1er couplet Be the best and f… the rest. Job correct niou done the best Started from the bottom now the top. No dounoufi déss BossBeatz the produce, the real sh** coming soon Topal gauche, you're star me a moon Time the money, money fane yi, only time for the job As Pharell say we up to get lucky all night (Alleluia) Ni Soundiata tothie gouye ya Déf hit kéne dou adji ni (Rolling Stone and brown sugar) Bégueul for my Mama, sigil for my Papa Big up for my Sister niou yokk diom mayma oh no Fitou tiger. Yes we can Obama, set melni swagger Victory we are champions You know our dream, always rap machine, i dont give a damn Sss Sa life boulssi meusseu tayi) Cfa,the dollars, boumoussi done bakhna Livre sterling, yen, yuan, Niak naniy bagne lets go Refrain Don't worry don't worry. Job lou bari dina meusseu soti Be happy be happy. Fight sa life boulsi meusseu tayi Deukeul si di fight sa life. One day dina meusseu nice Guemeul rék yokk sa fight. Béss sa gui téw digua diote sa price 2eme couplet Boula sikki sakka goudél nio ndandeu dou the test Nio gouté thiafka rimes niou ndandeu we the best Hard knock life jigger, young forever Get rich die trying keep winning for ever Peundou tanka gueune bou tate, danou dounou té dikate Gueum sounou bopp nanou déf, tégou si rail yi xeulate We the best, true. Douniou guéstou Waar everyday, ndam rék naniy sentou Your life, your way, your destiny. Jom foulak fayda, tékkossi Fok niou lal si lingot yi, jackpot bi dégue bingo bi Kouy diangeu dokh danou, gueum ko rék digna kaniou Béss dina nieuw gna bakou. Jot lépp ligna meusseu sakou Bridge (Multi Voice) Niodil boy si boum bi (Jogueul fight n***a) Bou dagoul dana téw (Be the best Yow) Fighteul (Right) sa life (Yeah) Guir none yi bagna ré (Yeah) Xat, Xat, Xat Xol Recordz Refrain Don't worry don't worry. Job lou bari dina meusseu soti Be happy be happy. Fight sa life boulsi meusseu tayi Deukeul si di fight sa life. One day dina meusseu nice Guemeul rék yokk sa fight. Béss sa gui téw digua diote sa price