Lamstar - Yaye lyrics

Published

0 193 0

Lamstar - Yaye lyrics

Yeah new generation ,yeaHiyeah, ahan 1e partie Bouder fogu gua yako soute baby yagui dioum Bouder amo respect thi mome nigueu yagui dioum Ki la mounial diourome gniti weer dou morom Mouk mouk mouneul yeme ak sa morom Yaye souma number one; lepeu lou bakh yamako wane Yaye guathier galama , mama yama gueneu kham Fouma diar fintal la weuyy (refrain) Apart ma mere , mama mama mia Je ne doit rien a personne Bis4 2e partie Lou lere ba lere moy yaye souma serigne Dima digal dima terer may djiss ndieurigne Deug deug yaye mounou mala faye Khana dila nian*l guoudou fane ak weer Yaye souma number one lepeu lou bakh Yamako wane yaye guathier galama , mama yama gueneu kham fouma diar fintal la weuyy (refrain) Apart ma mere , mama mama mia Je ne doit rien a personne Bis 4 3e partie Yaye yayou keneu, bay bayou nieupeu, lou lere ba lere yaye yama matt sekeu motakh thisa yener thi laye weur seukk, tekthi dila nian*l goudou fane ak werr Mamamia , mamamia more Mamamia , mamamia more (refrain) Apart ma mere , mama mama mia Je ne doit rien a personne Bis 4 Fin