Lamstar - Gueum Gueum lyrics

Published

0 164 0

Lamstar - Gueum Gueum lyrics

Yeah new generation lamstar (refrain) GUEUMEUL LIGA DONE GUEUMEUL LIGAye FIGHT GUIR TOOMOROW GUA MEUNEU DONE NDANANE Bis (4) 1e partie Guemeul liga done, te fa**e sa diom Te khameni toomorow daniouy amii dome Loumou meti meti fonkal sa life Te khameni dans la vie dou chaque jour lay nice Daga wara cline , daga wara fine, daga wara liberer sa myne; Gueumeul ni bouy meti dina meusseu nekh, te lepeu loulay gagne dina meuseu diekh Guemeul liga gueum, bayi noni wakh, ne repond pas , fixel figa dieum Ya de l espoir , j le sent , vas y courr, sezir ta chance (refrain) GUEUMEUL LIGA DONE GUEUMEUL LIGAye FIGHT GUIR TOOMOROW GUA MEUNEU DONE NDANANE (bis4) 2e partie Diokhel sa 1, diokhel sa 2, liga gueneu beugu boy na done sa 2 Nala diaral dee boy diokhel sa rou, boy yakeu sakh sa life boy nous on s en fou Daniouy gueneu djob rek hip hop bi dina faye Motakh douniou tayi daniouy gueneu beuy Gueumouma kouy togu gor djougueul outi kheye, guir toomorow sa life gueneu meuneu weuy Cone takal takeu bii, diokh exemple sa rakeu yii, yokal ligay ragu rek tee bayii fakeu bii Yakou sa gueum gueum begueul sa famaly Ko eupeu dole rek fils , deko dimebali (refrain) GUEUMEUL LIGA DONE GUEUMEUL LIGAye FIGHT GUIR TOOMOROW GUA MEUNEU DONE NDANANE (bis 4) 3e partie Hey fans welcome too my story, deglou ma rek ma wakhla li waral tiowly Amstar noumou deff ba wekhal sow bii, chak pas bouma tek, enemi yii gueneu diomii An 2000 ma creee .new generation boyz. lima gueneu djob di deme di nekhal sama voice Fouma meuneti deme yaye nian*lma guir ma meuneu sorie, tekthi fouma diar fansy gueneu barrii (refrain) GUEUMEUL LIGA DONE GUEUMEUL LIGAye FIGHT GUIR TOOMOROW GUA MEUNEU DONE NDANANE Bis 4 Fin