Rich Black - Boy Sicap (Remix) lyrics

Published

0 115 0

Rich Black - Boy Sicap (Remix) lyrics

[Bridge : Rich Black] Est ce que meune ngeu diay néx boy sicap? Est ce que meune ngeu diay graw boy sicap? Est ce que meune ngeu ték xél boy sicap? Mane..dumeu dém jail boy sicaaaap! [Verse 1 : Bako] Im not from capsi gueule tapée la diogué wayé respect capsi Diudou gt deukeu yoff grand boy f** dat mane feep lay represent... L1, l2... l3... l4, l5... Sac city 1 sac city 2 sac city 3 Baobab wa L6 ! Sicap capsi sicap magui bégué sicaaaap Deugueuleu ta**é negn biir amitié mais takhouma done sa waye Niogui sene kanmam duma sen ma**, duma sene couran Rap sudone cla** yeney taaable bancs Fuma sen place damey tokk sen kaw... suivant ! [Bridge : Rich Black] Est ce que meune ngeu diay néx boy sicap? Est ce que meune ngeu diay graw boy sicap? Est ce que meune ngeu ték xél boy sicap? Mane..dumeu dém jail boy sicaaaap! [Hook : Rich Black] Sicap Capsi Sicap Mangui bégé sicap x4 [Verse 2 : Fla] Est ce que mane nga diay nekh Boy sicap Soko manei yokhoul sa bat boy ci kaw Boy nianning boy NF yeah dama graw Mana rap beuri diap fils niola raw Ni ay boy sicap fils damay doundeu kaw Voleeee Douma takeu tei damay naw Ni sama tour boy takh malene Di survoler b**h I do me Dont ask me my mane cuz u know me Been ballin from dk to kl yeah them b**hes love me Revolutionary like Awadi Ni boy sicap fils dama xamad I [Bridge : Rich Black] [Hook : Rich Black] [Verse 3 : Kalz] Lakouniou kal diola waleu sereer Djeul djom ak fit takk ko téré Sérél pa** andil seu témér so xamoul side meune ngeu séé réér Nioune ndam req xoumougn lénéne loudoul coupe Kogne bé kéy todj depuis robotcop Té nga roteul kopp waleu ngeu sétal bok? Nio dakk scandale Olivia Pope Mani Capsi Capitale Kalz Capitaine Ay peine capitale Kalz Saddam Hussein Défougnou rap hardcore d'accord mais nio geuneu technique wa matforce Meuno diss wa L6 fils dégn diss fils Séne dix pistes lakk ay pitch esk yangui siip ? [Verse 4 : Rich Black] [Hook : Rich Black]