Rafall - Tathiou Ma lyrics

Published

0 537 0

Rafall - Tathiou Ma lyrics

Xat Xol Connection Album : Pollution Sonore Intro : Xat Xol in da House (Poow Poow Poow pOoow) X2 Refrain : My n***a Tathiouma... Mane ma kaay todj Ndéké My n***a wathie ma... Taak nga souf (X4 Couplet1 : BossBeatz & Dimelo : - Ya kamati kamati ya niou f*** sa unh, nga tiit ni waa !! Nga xeumeuti, xeumeuti, gayi lokk sa siiw dadjal la banc - Ya mounta barikha, ki mounouta bayi togn Té mako mbethie, mbeuk, ouuuy... dougaal reuk waay - Kélémati kélémati (What a F***) Khelmati khelmati (Dinala F***) Bottoms up Bottoms Up, baram sa reum mou teup - Kay nga teup, Kay nga teup boul faté sap na reup Woossup Esk xam nga natt, dinako piqué, niqué kelk Mickey - I do it like a Kana, Sater bi néma fane la Job bi la sama corner, sa guel néna boy fane la - Bi dinala nexx Degu na Dom*** nga Mais ki dou ramdan Dila bouti dinako nekh Refrain My n***a Tathiouma... Mane ma kaay todj Ndéké My n***a wathie ma... Taak nga souf (X4) Couplet2 Babs Black Fok niou tathiou, f*** sa alou, talouniou bakkouYa fi nagou Fok niou tathiou, f*** sa ndiayou, nga deuké di sirou Fo tok di mbalou Doumako fowé, doumako kafé, tathiou yéko séddé Def lou nice ak samay guys nonou nanioukoy doundé Foniou guissé souniouko tégué, nga wéddi say téré Kone defal tek, delou gestou, fi dofi djité Kid Jay : Mane dama dé, ma ngui Alakhira, F*** Renaissance Deukel doul sa bopp soulay nekh, diaay amnésique Im the only one who get the job done, douma wakhanto Ma ngui ak samay own dadj, boulma djign bone youma tokhatoul Da ngama tegone Fans wala, tu prends des coups Yeuy chewing takhoul nek star biir Hollywood Soph*more ? Im graduate Niata fi parié, del p*** lou khadj sa t*** yi Refrain My n***a Tathiouma... Mane ma kaay todj Ndéké My n***a wathie ma... Taak nga souf (X4) Couplet3 Jx & Rafall - Bokouniou yaw, wouté khalat, dandouma thia khathie Yalla ma tathiou, malaka yi félou, degg nga Tathie taathie taaathie - Diougeul dem, dikeul xool, xat xol ngafay bayi Borom baat bou sew, Tothie sa Ouuy, nga fay baayi - Nii pion ludo nga, boy omé di guéneu, mane Dée la Life béma soxla ni Nelson Mandela - Ma deup Mandéla, mou diokhma Ndella Mar Tathie tathie tathie tathie tathie Raté but do Neymar - Brésil ya Neymar, takhoul niou faté Pelé Old School, Y en a marre, ma ngui nieuw fokati bi Relais - Nga dadii tiit sa guent, youkhou diap bopou X.X moko ress koneu nieuweul Topp - Niou dalaal xélou rappeur yi, bayi naniou rap Légui daniouy Salsa, Guantanaméraa - KXxkxkxkxkxkxkxkxkk Ladj ma Mami, amina wala Aida Fall Kxkxkxkxkxk Refrain My n***a Tathiouma... Mane ma kaay todj Ndéké My n***a wathie ma... Taak nga souf (X4)