Nix - Highlander lyrics

Published

0 426 0

Nix - Highlander lyrics

Mane kécé kén douma dondou Gnou yeungou ma dagati lén Ngén sori ma loloy lou dagane Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live) Vieux père boudoul maguett…Highlander Dagg sén bopou lay déf…Highlander Décapité par le chef…Highlander Vieux père boudoul maguett…Highland Vieux père boudoul bayi…Highland Vieux père boudoul maguett…Highlander Fougn dougou ma lidieunti lén… Mane kécé kén douma dondou…. Gnou yeungou ma dagati lén… Ngén sori ma loloy lou dagane… Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live) Boumay dioudou Rap dé amagoul Filama fék ni séni doul Ma imperméable ci yeah dama toul Té noupou bou nathioul dégagoul Baggy jeans Wu-tang diamono May battle di battle di battle Freestyle malay golo lo May danél di danél di danél Soma wédé lay ma Xuman Ték ay flow Busta mélni dou man Au final yakamti pour lane? Période bobou damko diégui ni dos d’âne Néka gouma ariste solo Mais mangui ci game bi ni Gaindé bou souroul Di dougal ay Mc ci bir kilo mbourou Di dokhantou ci kogne bi di weur ay foural N Easy dafal ndank lou eup tourou Ma keupal yélwane bi sama boy yi djirau Surveillant Général la bagné bureau Nékété mariage dafay wékh ni gourau Doumala diay expérience boy amo gneugam Damay ma yar boy khébouma deureum Dagn ma nokk boy ba tay ma gueureum Golden boy dama gnoul ni peureum Longévité boy Dou serigne dou mara Dou téré dou garap Boy défafo dara Dou palace dou baraque Dou Donald dou Barack Dou Point E dou Karack Lougn cons’ boy dou diaratt Ladial Egyte boy fougnou tégone Moubarak Mais Yallay Bour souko nékhé faral’ko Kone N Easy bayil sou la nékhé nga dialat Ndakh Vieux père boudoul maguett…Highlander Dagg sén bopou lay déf…Highlander Décapité par le chef…Highlander Vieux père boudoul maguett…Highland Vieux père boudoul bayi…Highland Vieux père boudoul maguett…Highlander Fougn dougou ma lidieunti lén… Mane kécé kén douma dondou…. Gnou yeungou ma dagati lén… Ngén sori ma loloy lou dagane… Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live) Tête de mort Katana bi loumou dagatti boy rawna dibitterie Tête de mort nékone fi tendence Tout ce que je voyais c’est mes trophées qui me sourient Kou que-ni flow bi mou déloussi Boy ay éclaires lay cons’ mél Hennessy Rap Galsen sama done wané père et fils Mamou mamati mamou sén lyricste, ay seut flow thérapiste Koufi atanne sama legacy Né téki téreum, dérett takal yéreum, bane yi takal béret-reum, balle ci tak teu-teu-teute, boy gnou teral lén yénak sén kheuram fils Equipe bou fess ak génies fils Do lathie Orange lane moy bénéfices Do lathie wa Yonkers kou Jadakiss Défaite boulay fégnou doko téleu guiss Té longétivité boy, dou mayé dou sarakh, Dou Jordan dou thiarakh Dou khégn nékh dou forokh Mais toujours frais comme le Vieux père Ray ak sourire ni Joker…Highlander Dagg sén bopou lay déf…Highlander Décapité par le chef…Highlander Vieux père boudoul maguett…Highland Vieux père boudoul bayi…Highland Vieux père boudoul maguett…Highlander Fougn dougou ma lidieunti lén… Mane kécé kén douma dondou…. Gnou yeungou ma dagati lén… Ngén sori ma loloy lou dagane… Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)