Martin Luther King Jr - Raison Nègre (FreeDope Intro) lyrics

Published

0 120 0

Martin Luther King Jr - Raison Nègre (FreeDope Intro) lyrics

Martin Luther King speech: "It came as a joyous daybreak to end the long nights of our captivity. But 100 years later, the Negro still is not free …free …free …free …free" …free DOPE yeah Verse 1: Me dieulate ay gaïndé me dompter lène Seme flow ay containers moye gonfler nerou wa corner bé Zig, Tamba ak Pont Faidherbe Boudoul wone fi dou done fénène Boudoul wone Free dou done kénène Boul khole kénène bougoumeu done lénène Al hamdou mane sante na Jamm dongg le sh** bi dou done lénène Strong in the biz boy pompez lène Té con yi le time deniou done kébétou souniou son yi di leu hit ngané on t'énerve Bouniou nèkhone niouy diaay rich Fègne ak bepp khètou bad b**h Ndakh gentle negn, tangal nègn Wayé boul tékkheulé bante ak wégn Boul tékkheulé thiant ak wéy, dinga diawalé diante ak wère ?? Bou bougué am diam dongg son bi diam se ndong li Nanga and ak tèye Bo lene mounoul ba lène mic bi, cons Free crack #bon élève Dope pour Black & white am na raison nègre #EmotionHellène Chorus: Jamm dongg le ish bi dou done lénène (ish bi dou done lénène) X4 Togg na quantité yekk na qualité (hun FreeDope)X4 Verse 2 Wesh c'est qui ? Qu'est ce the deal? It's the best in this my boyyy Mane doumeu deul extasy, gueuwmeu s** appeal té doumeu nekk di bif ak ay boyyy (hun hun) Rest in peace Laye Séga, RIP Baye Petit Iba Sèye, Lik-Sama, wallah wéteul nguène birr keur gui The West African Finest, man a rep African fighters: Niom Sankara, Lumumba : I'm no blood but I'm diamond Bad as M.I Jackson, Jam-ballin like Jordan My tape rockin like Mysonne Punch faces like Tyson haaaaaan Audio crack coke laye nouyo Ga yi niam flow bi saf DOPE bayi niou go Dealers yi dow degn degg DOPE ba ngui nieuw DOPE ba ngui nieuw!?? Wouyaye DOPE ba ngui nieuw!!! Seme style defe nité ya ngui feel nimey indé seme flow? Mo gueuneu épicé kilo bone ! Seme sk** defe styléé, deme ill, nimey dealer seme DOPE ? Demey k**é ak stylo dongggg ! Chorus FreeDope X4