Elzo JamDong - Tout Bas lyrics

Published

0 196 0

Elzo JamDong - Tout Bas lyrics

Ay rimes laye yor di leu ko sékheul mouy dougg se khél Stop mane sakh kaddou la yor wala kouddou Touddé seme bopp free bénieu tédiou sene jail Li mey néttali lepp bala mey reuthieu la ko dounde Temps boy degn danefo pape ak yaye tédiou thi roukkh Té amoul ken thi nioune kou niou nettali fane leu diar be diouddou Diarouteu magg diangg pour compe ni gore djiguéné baakhoul Mok dord jiguéneu yém kou thiné do gor djouguenn ndiakhoum Bo diogué né yakhounégn NDAKH degn yanou mana Yow falounga té diengouwo SAKH guiss yonou money Yenn mar yi kou leu ga**al PAKH mou nekk potit Nga tankkh nane do yég yen a marre ak potopoto Bienvenue fi degn ley yéné merde, di le diémeu yédd Kou fi diémeu tedd mouno toukki niouné le ya feu dé Defe yémé man degn ley yèwe def le diamou mbed Bolou gouddi yi niouy lekka takh niou diappé aye feudo Niouné nio mer dé han wala yéneu merder? Kou meyone kaddou idrissa ndiaye kou diokh ndam Selbé ? Ki né sokhleuwoul ndokhou tow toleu meu ngui sakh Ki fanane thi mbedd di liw kholeu meu ngui bakh Ladial Mimi ndakh cadence accélerer neu some Beu légui Do tabakh se keur dé ak salairou maçon Li beykate yi di dioye kouko nara gérer mou sakh Casino ya ngui takk yonou adiana lereugoul sakh Chorus x2 Me wakh tchi kow le nieup di mind tout bas Nit kou niouleu rey Malcolm ak 2Pac Me wakh tchi kow li nieup di mind tout bas Loutakh me war leu wolou daal di saaga toubab President Thomas Sankara speech