Elzo JamDong - Comme Mane lyrics

Published

0 198 0

Elzo JamDong - Comme Mane lyrics

Intro Ladies and gentlemen welcome to the Freengdom haha Danga dof wala lane? Huey Peace Verse 1 Rafett job ni Alladji seme tour Yalla djé toudd depuis seme jourou nguenté War nga sage bo fateulikou ni bi ngay dioudou hopital sage femme moleu guenné Limey def defe tégou flow bi defe tarou melni lokho guél bou dogueu def henné Soubeu ci diante la goudi werr so mey sete fok nga tene une nouvelle étoile est née (est née) Eksinaa di liguey ak seme flow indi son you eupp rythme teugg katou diembé (yeah) Mane ak Mister Thiere niokoy togg yow se waania gueun khewi soirée fetchkatou thiembé Bodé dogueu yewou Yangui nakh se bopp legui nga gueumentou boudé nioune ngay diemeu gêner (gêner) Fogone na ni peace le ak love, tegone na la bro ndékété moussibeu ngama yéné A part Mère bi awmeu royoukaye Maa ngui degg ibliss nane me Elz kham na yone bi kaye Mane ngay diaamou maye se penkou doto look up to the sky Bomeu toppé legui fly légui son yi dialleu skyrock Mané ko Yalla rekkeu meuneu yegueul seme art Momeu yoré momey yar soumeu goré momey aar Rouhou amoul ndieuk ken dou dieund seme libre arbitre Seme diné momeu gueuneul se ay milliards b**h Bridge x2 Moune nga def Paris Dakar aller-retour do guiss kou koy def comme mane Koumeu test ding ko reuthiou di nga degg niouné il est dans le coma Chorus x8 Comme mane comme mane I guess do guiss kou koy def comme mane hum x 4 Verse 2 Mangui fateulikou bi mey dogueu wathie Paname deme dèè rap bi diplome la fa dieuli Wayé flow bi nekk seme yaram soumeu bayi wone mou sedd Dakareu ngui neiger heure bi Rappeur yi bouniouy deglou seme hit deniouy tite ni kou amoul ticket dadié'k controleur yi Dj-ing, Mc, Graff, yokk na tchi Break-ing bad seme cd eupp dope gallé leurdi Khamone nani ma fi daakh play flow bi train na ko depuis bimey dogueu dougg Aldo Yo deungueu khawa Maniang te deme khawa maniaque doumeu sol loudoul Sept comme Ronaldo Semey andando weu gueuneu real wa Madrid gueuneu sain Germain, team bi nieuppeu serieux, team bi choquer serr yeup Moquer adversaire yeup Ta**aré concert yeup Diakhal commissaire yeup A part terreul Mere diappé woumeu dara blème-pro Def na seme guerre diangal seme bopp done pro Sol Jo togg dope, shooter diaroul GoPro Nekoul mane ak niom douniou binde limey impro Yangui yakkh touflit boné Elz defe aye I'm so Good Kid comme wa dji defone son bou toudd "i" Homie khana diangueulougn leu saathie defe aaye Mane nga beugone toppeundo deungueuntane? hahaha aight Bridge x2 Moune nga def Paris Dakar aller-retour do guiss kou koy def comme mane Koumeu test ding ko reuthiou di nga degg niouné il est dans le coma Chorus x8 Comme mane comme mane I guess do guiss kou koy def comme mane hum x 4 Outro Moune ga def Dakar Sydney do guiss kou koy def comme mane Do guiss kou koy def comme nioune Jamm dongg leu Kham ngueen kou né tchi Freengdom bi boy Danga dof walla