Elzo JamDong - Capitale de la Capitale lyrics

Published

0 292 0

Elzo JamDong - Capitale de la Capitale lyrics

Intro Digou Sandaga... Verse 1 Danouma sétane dessin animé ma gueunone touti gallé Te benn télé moye animer Mcm la done golou Fi deunguey teleu dem matinee lepp ngay teeleu def Digou Dakar, rissou ragga bou Dj matar di animer Dou takh nga niakk talibé maman neneu gentil na Te bizarrement Seme grand yi nénegn bandit la Wa gallé dolene wone se fit temps wou gentina Boumay zoner corner douma andak samay sentiments Fi biniou amé 7 ans legn khammé lax Fi biniou 13 ans legn dougg Stax Fi mm bo amoul mak deunguey teleu nande Wakhoumala nak nga done namp tchi boutelou mak Rote onde toni pack litrou valmera** Dougg na tchi guenne na tchi rue de Valmy rame Dounde na ko tangana ak roukhou macky saf 10 ans apres none le kogn bi gueuné yakhou macky saleté Boy yi tey legn gueuneu dee walo tey le gueuneu aaye Moye gni dieunde diaye coke marché comme si c legal Fi dou Washington mais am ne maf ni birr Capitol Mey ko ko baol-baol yi ak ndring yi seme capitale Chorus Dem naChitown dounde système fédéral Dem na la défense Dem châtelet les halles Deukk na kawe weur na senegal Guiss na ni wa town douniou sene égal Capitale de la capitale x3 Wa town douniou sene égal COUPLET 2 Danouma sétane dessin animé ma gueunone touti gallé Te benn télé moye animer MTV la done golou Fi deunguey teleu dem matinee lepp ngay teeleu def Tem nga aligner beu abimer wathieu do wala alizé Dou te nga am idée donté nga teleu guinz b**h Bo amoul chance deugueur deug rek deunguey kinss fils limeudane romb goudi town? momeu indil inspi Bimey ndieukk binde 16 amagouma 15 piges Est-ce que kham nga ay Fouquets? Africa star? Sista yi jobé rue Escarfait angle Raffenel Hotel du marché, Albert Sarraut Saloon Texas... Gni maggué town rekkeu kham né Ponty amoul thiaga Matin bi deunguey diangg ngone deunguey def street Night bi deunguey tokh bone deunguey def bizz Am ay copain you deukkoul corner nieuw pour nga yoboulene salle de vente diaye feu last call nga am se lekkou deal Thioy yi diapp negn Gangsta yi dakkhone diapp daadj Boy yi done daakh sip legui nio magg daakh deal Bo amé grand you deukk jail do to diapp chill Do faaléti ay yermeundé dieguelou diapp tchi Boy yi tey legn gueuneu dee walo tey le gueuneu aaye Moye gni dieundeuk diaye coke marché comme si c legal Fi nimou beuré batiment non leu beuré batiman Mey ko pourtou ngagno yi ak naar yi sama capitale Chorus