Elzo JamDong - Allou Ciment lyrics

Published

0 252 0

Elzo JamDong - Allou Ciment lyrics

Intro Nioune ak loi bi leuk ak boukki leu, mounoul bagna amati beef Nioko def votel gaindé you dotoul khamati khiff ... Allou ciment, yeah Verse 1 Kenn niaanoul Yalla am mbokk bo wara seeti jail Pour guenne faut q niou diaar tchi caisse mel ni City dia Kou fi khamone serigne bouy créer tekki ding ko seeti dji Wakh dji bo tchi guissoul se bopp demal seetou dji Thiow be ngui raisonner tchi kogne bi comme ay ambulance Thioy ya ngui diabanté tchi kogne bi comme ay ambulants Boy ya ngui dakhanté tchi kogn bi #Endurance Coke bi moudié wathie tchi kogne bi mo am Honduras Borom bopp yi nioye borom boppou kogn bi legui Borom diplome yi sene morom yi di lene gondi guey li 40 ans mousso job niaari wakhtou Daakh ka** daakh wakhtou bepp wakhtou ya ngui niakhtou Am na guiss guiss na ko wakh nga degg Fi gayi yorougn do te beugg dope ni Doggy dog Am na guiss guiss na ko wakh nga degg Negn ko wakh te dee wala Gal gui dineu dig Yalla legn gueum mou mel ne ni Seytané def niou tiim Beugg nga sangou sete mais sey toilettes defe tilim Kougn fi deferrer thioy yi dougn le Faalé degn ley puni Innocent ak coupable yeup khamal ne Yang tchi birr Chorus Allou ciment, fi moye allou ciment Loudoul crime dougn ko fekk se cv Lima fi guiss dafa tar defe yémé Hallucinant fi moye allou ciment Louniou khirr ba toppouniou térré? Deukk tchi deal ak def louniou téré Verse 2 Bob be legui gning koy khaar guissougn changement Pourtant dem ne bey guenn moudié am dérangement Fi dara changer woul à part minette yi magg mole Mais souniouy rakkou homie legn dougn lene meuneu khole Borom gamos yi garer corner dieulsi leen Mouno ci leen Deniouy and nekk 2 ci nek Bouniou docilé money leniouy diappé Dieu ci leepp Do ci yek dara boudé amnégn tchi town bi dossier Am na guiss guiss na ko wakh nga degg Amo lo thiope beugg dounde lifeou Doggy dog Waa DIC gning ley topp sey waadiour degn le soppe Indic yang ley khole mefie toi de l'eau qui dort Dou superman mo ley nieuw sauver dou batman Guissoumeu logoweum ci a**amane ci kone Boudé yangui tokh in the pet diemal baayi Boudé dangay fone wala diamou mom a maayi Wakh deug na**aran ci dafa nakh sunu mame Wayé niounit waratouniou nangou ga** sunu pakh Senghor wakhone ne deugg légui Dakar comme Paris Benn difference mo am fi amoul Tolou goudron wayé am ne Chorus Verse 3 Nioune ak loi leuk ak boukki le mounoul bagna Amati beef Nioko def votel gaindé you dotoul khamati khiff Kaaniou fatté allou kagne deukki Canaries fils Kou ko niémé toudd niouné leu danga khamadi fils Yo xippil khole yang tchi Allou ciment kou meun se morom thiope tabaski niou baalou ci aakh Souma guenné son bi dineu am niou alou ci mane Li legn fiy dounde mais defe mel ni Ken warou ci wakh Allou ciment 100 m2 Allou ciment Camp pénal Allou ciment M A F Allou ciment Allou ciment Allou Ciment Teaupla Rebeuss Allou ciment niaay Thioker Allou Ciment Medina Fa** Allou ciment gueule tapée grand town Allou ciment Pikine Thiaroye Gare Allou ciment P.A Guediawaye Allou ciment liberté 1 ba 6 Allou ciment Grand Feuyo Balakoss Ndar Goumel Casamance LG KL Podor Alleu dongg leu