Elzo JamDong - Assiko Flow lyrics

Published

0 291 0

Elzo JamDong - Assiko Flow lyrics

Check my a**iko flow Yeah Verse 1 Bimey lekk mc lekkagoumeu big mac Me paré eksi nek phenomenou hip hop Flow bi takh kou moussoul droguer legui Sick rap Demey Rap nga fok ne mousso degg benene nit rap Ding me degg bureau tangana ak biir fac Terminal yi di meu sentou ni sene Fuite bac Li dey guenne bomb sokhle woumeu Feedback Ladial Dip deniou deep kouniou diss lap Daccord nga te niamago tchi last huit yi Boumeu neekhé beureukheul li dess ci beat bi m**m rapper la bou yoré flowou Whisky Bou refrain bi di eksi ngay weddi Wiz kid Han? Zero Handicap Gnimeu done khepe diokh nalene envie stop Deme bandit kate legui t'en dis quoi ? Mane deme beuri bars ni deukkou mandikate Chorus Assiko flow teugueul me a**iko Seme baat ci kow Limoy son Yengueul Paris beu Mexico Assiko flow teugueul me a**iko Seme baat ci kow Limoy son bi yengueul Lagos ak Rio Verse 2 Newone nala do guiss kou key def comme mane Son bi guenn game bi yewou yemou comme dhab Diogué na tchi under créer seme Kingdom Bolé khelou einstein ak katanou king kong Moune na doré ak mi, fa, si, la dope dane Awma dolé mane ne flow be indi do daal Thiate defe gaaw wakh ko gni fo wé sene ndow wala Gni khamoul ni yonou tekki defe beuri Dos d'âne Ya ngui laadj nane laye def be flowou Zo rare Awma temps wou guenne son yi fok niou gaweu guenn Seme premier hit be legui ma ngui dore waar Job bi defe rafet neu nullards yi fok niou niawal léne Titeul rappeurou Marseille beu Dakar Yalle ne me Yalla baal semey bakarr Niata wakhkat nio ta** seme Yakarr Son bi takh ne me fadj semey nakhar Chorus x1 Verse 3 Seutou hustla domou hustla Im a hustla diam le nga fok né rasta le Niveau master le danga fogone menace leu Me break se neck qui est ce mec? Dama fogone ni Busta le Elzi o le fils mako daakh def Boumeu diemeu diss beuri fils ni kou yagg nef Deme ko yagg def te khamnga sakh tchi pa la dieum Beuri style depuis bimey sol ay palladium Fenioumeu tchi se télé nguir se estime Niata diameu diemeu soukheul souniou Ness biz Dem na kaaw difeu Siguil seme Presqu'ile Kick louy fresh clean deal le le textile Jamdong le kham nga we the best team Ay kangam dong nek tchi birr collectif bi Kid bou khess bi indi sh** bou bess bi Mom ak mister thier mi ils méritent le prestige Chorus x2