Elzo JamDong - PositiVibz lyrics

Published

0 158 0

Elzo JamDong - PositiVibz lyrics

Hun...Hun k** them with... Barrington Levy sample "k** them with positive vibes" With #PositiVibz ... Dolli tchi waay, yeah (k** them with Positive vibes) yeah Verse 1 Ay positive vibes lama di khélli bou doyoul dolli tchi Lepp lou dieum thi samm kolleuré t'inquiète nio ngui thi Samm jamm donng ni Lauryn Hill Nio ngui thi khèkhe, boul khèpe, boul snitch, boul yolé deal sh** bi soundou strip tease mais s**y neu Hello DK, Yeubo TeauPla ekssi neu Nélène Hip Hop bou dèè wone légui dekki neu Niafé neu beu guénne ghetto bi légui tékki neu Gueustou negn Pac, yagg déglou Big Yagg dadji ay pack guénné feuille ak bic Fone diamou thi punchline yi ak grosses caisses yi Presque ay Talibé wou Kweli ak Mos Def (yeah) Be légui kou wakh deugg niou tek thi bate ! Compilou Dekkil Rap léniouy dekkilate Bou doyoul me dolli thi waye Jamm dongg legn sékkh ak ay Positive Vibes Pont1 Haha ak ay diap , han Mister Thiere hit me Yo Bab's yéwoul boyyy, han wa H (Grd Medine), bou doyoul me dolli tchi Verse2 Ay positive vibes yi mey khélli sokhleu woul polémique Bo dé nit, me togg bolé leu tchi nga goré tchi Wakh bou beuri mo takh louniou tabakh danou rek Motakh légui manou rek sinon gaaniou rek Depuis temps wou Pac niou né tchi same ish Yo bingay TAKHOURAne seme ga yang thi TAKHOU RAp yi Sorano: anniversaire PBS, Daara J Saint Michel, DJ Makhtar PCS Boumou diame yi legn takk tchi bate Flow bi ley feugg ay kourrou baye Cheikh Ibra Fall Lo mey kholé ni gayne? deungueu fogone dina fombé ni fight bi? Ha ay BOMB la lène indil ak ay Positive Vibes Pont 2 Yea, yo dolli tchi! My man MTO DMC danga dof wala lane Positive vibes dolli tchi waay (Bruit de sirène en fond) Verse 3 Han Positive Vibes yi mey khélli ? Mome rek la yoré ni Boumeu droiter lo thi naadj bi kanamou gonéyi Am na médaille d'or dèlloul se keur Son bi fok mou dow ak Usain Bolt Jailou Reubeuss (#100m) Ma dakkh youkhou Ndour ma gueneu marre Pène Deme khiff ay khalam, Souleymane Faye Génération "Rest In Peace 2Pac Marley" 11 mai niou diam leu yobou leu armel nga ziarre lene Yo bayil me yémeulé ko fi ga yi parégouniou pour degg yoyou ! Deungueu sonneu ? Han? Wala me dolli thi waye ?? Ay nokkh lalène digone ak ay positive vibes Han, loye mel ni kou diommi ni gayne ? Jamm dongg legn sekkh ak ay positive vibes Lo mey songgué ni baye hi? Deungueu fogone dina fombé ni? laay!!! huhu Ak ay positivibz Lo mey songgué ni baye? deungueu fogone dineu yombé ni, Layyye lol Ay bombes lalène indil ak ay ... Lo mey kholéé ni gayne ? Deungueu fogone dineu yombé ni han? !:* lalène digone ak ay ... Ay nokkh lalène digone ak ay ... Ay boxe lalène digone ak ay ... Jam dongg legn sèkkh ak ay ... Ay *$^^ lalene digone ak ay...