Elzo JamDong - MALEMBE lyrics

Published

0 154 0

Elzo JamDong - MALEMBE lyrics

Yeah Hit me Sa projet kène meussou ko khaar Homie lane la tchi meune Forcing bi nieupa si marre Homie lane la tchi meune Sayo khéwlé kène dou nieuw Homie lane la tchi meune Y'ak sa gars yi réunion dima dieuw Mais lane la tchi meune? Ni-nitt'a geuna meuna bagne nitt Motakh rappeurs yi geuna meun bagn rappeurs Nénégne ma fils sa flow dina réy nitt Lima lérr moy douma bal béne rappeur (douma bal kéne) Awma temps boudoul money boy (awma temps awma temps) Am ngène chance dama diangui wone Mayé nangou bakhoul dédéét Mayoma mayma diam nangou défaite (mayma diam boy) Zonou town mako ress boy (mako ress, mako ress) Soma songué nala pess boy (nala pess, nala pess) Man sokhlawouma presse wala escorte I'm the f**ing best boul ma stress boulma test boy Samay vestes do guiss kéne sol Toujours cla** f** sa dress code Amna ay ex youmay tek choc dima yoné text dima ess pour niou s-port Yan khamné malène meune Ben khamna malène meune Wakhkat yi bal lène rek Wa kogn bi yeup ak kogn bé yeup man légn geum Malembe Malembe Free def niou ndank ya alliéné Beuri ay MC you khalélé Togne nègne la moss wayé bal lène rekk Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Free def niou ndank ya alliéné Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Togne nègne la moss wayé bal lène rekk Sa clip kène beugouko share Homie lane la tchi meune Amo ay mix mister Thier, woaahh Homie lane la tchi meune Jamdong bi nga done khéb, tey mola geuna cher Homie lane la tchi meune Sa wa kogne man lègne défal car nieuw sétane si sama scène Homie lane la tchi meune Lane la tchi meune Man, défar ay hits sama maladie leu Yow, nullard nga lolou rek la khalat tchi yow Té nioune rek nga fan diniou mbalak di saupp Sa dawou fa**ou daaw dotoul dalat tchi yow Khamal ni calé nga ndakh fi ngako beuga calat dou fofou Chaque jour liguèye sama calendrier (liguèye rek, liguèye rek) Fi amo fi ndieurigne comme salade tchi deumm Défal ndank Bi lépp né sélèw mane ma nieuw yeungeulatt la yé la Ma nieuw yégueulatt sa level Ya meuna faté ba yémm ma Bi sène game bi di néléw ma nieuw nékhalatko yeah Man ma indi rap bi nga yélo push ko ni Baaba ak Yéla Malembe, Malembe Gnima done dingatt nieup nalène bétt Man ngui tchi diaww dji, yène fan ngène né? Dinalène diokh sène dose ba ngène bééékk Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Free def niou ndank ya alliéné Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe Togne nègne la moss wayé bal lène rekk Yeah kène meunoul téyé lima done develop I'm a OG Tell'em dama nieuw nguir fay la (Dama nékg) Man ak yène on est trop différent Dama original yène ngène copier ma (bayilène di topandoo) Douma nopi ndakh amna avenir douma salopard Dama khiff meun na lekk yapou charognard Douma domou riche, awma avocat Té fépp la son bi di daw diaroul à vos marques Malembe Malembe Malembe Malembe Malembe