Elzo JamDong - Beats By Thiere (Megamix) lyrics

Published

0 238 0

Elzo JamDong - Beats By Thiere (Megamix) lyrics

[Bako & Kalz] Non mais vraiment fils yay séér Suma nékhé saf beu méyleu diabou diay cher Niogui super market doniu guiss par terre Rapid deniu raaap ba nga crise par terre (aaanh) Niogui doundu suniu legacy, nuniu def ba nekkaci Yalla reka kham... lutaxx fans yi di diéguéci Bako niu né Jay Z,Kalz niu né Wiz Drôle de concidence on est coincé dans le biz Di rap di tins les b**h-niqqaz qui hate di.. Djam you saff ni temps wou niome Gee Bayss fils Nio geneu tangeu biir town , rookies yeup face down Elzo pa**,niou daf def rush ... #Touchdown Aaaaanh niqqa li dé dafeu nékh baay Nooon niveau son mat néniou léne baye Nadj yay kér , first ngéy ndér Yow déniou leu faaté , ni ca**étou Mbaye Nder Bang Bang !