Admow - Dem lyrics

Published

0 147 0

Admow - Dem lyrics

* Sonnerie de Téléphone* " - Allo, Kalz ? - Yeah boy nakamu? - Boy dara doxul baay , mais dam leu soxleu wone dé pr béneu affaire bou urgent yangui galé anh? - Cheuuu boy yane xéétou problémes ngeu amat encore boy? - Way...mak xoleul bayil wakh dji lima leu beugg waxx dafeu urgent koi mounou ma leu ko waxx si téléphone bi koi bayil rék meu téw seu galé yangui feu anh? - Waaa wa thiow djibul le temps beu bath ndékki khamngeu ngeu djaar , légui légui - Wa amul thiow mangui déf ." [Refrain : Admow ] Mane damay déma dem Dem ngui outi copar Téral mere ak pa ndakh ci mane laniou yakar Mane damay déma dem Dém nguir xami kénéne dondou lénene outi fénéne ouu wooowoo Mane damay déma dem Dem ngui xam tiono adouna ouwowooowoo Mane damay déma dem Fok ma dem fok ma dem yeahh Fok ma dem ouuwohooo [Fla] Dem fane Dem ndakh lane Dem ak lane Dem ndakh kane Dem nguir ame Wala gatal say fane Boy fok ma dem wouti jii Souma amé délouci Délouci indi lou beuri Lou beuri tabakh keur gui Tabakh keur gui téral mer bi Téral mère bi siguil mbokeu yi Di dawal auto you toy yi Anhh Pabi nopalou ma dess ak mère kécé Motakh majoug di niaffé Fis diémna louné founé Mais fi dafa deugueur ni xer Kone fok ma changé aire Métina ma bayi fi mere Mais fok ma def ko frére Manatouma tok di xar Di xar elni ab xhar Kouma diri ma dépar Dina dem bala mouy tard Peu import fimay diar Mouy gal wala sakhar Ain't no more be waitin' Fear money don't make money So i have to do something Get up and get that money Have to do it like fifty Get rich or die trying [Refrain] [Kalz] Dem fane Dem ndakh lane Dem ak lane Dem ndakh kane Dem nguir ame Wala gatal say fane Maan lo méy tégal nii fokné dangéy dém rék daldi tékki? Guiss na gnou ssi déloussi té andaalé wougnou saxx fiftine Epuis sou nieupeu teubé waxx meu kane moy job deukk bi? Senegal dou dem OK mais nioune nio ko wareu lidjeunti Ngeu lacher pa ak madre daw séy responsabilités Man réfléchis a deux fois yéneu yii no kéy xalaaté? Bayil lingéy djoy Geumeul Yallah boy Xaliss bangui fii djogeul xolssoul rék djotssi boy Ndax seu morom yii rék nio fi nékk di dorwar Di dougou , di géneu , di hustle , douné yakar Naxxar , biné seu xol yéneu say mou dal meu Mais lolu lou wareu am leu Délowateul seu xél si Yallah Ngeu seugaat si sseu djangeu xamné kou nékk ak seu walleuh Seu weurseuk dou leu rombeuh hunnn geumeul seu boppeuh ! [Refrain] [Admow] Dem fane Dem ndakh lane Dem ak lane Dem ndakh kane yeaaaah Dem nguir ame Wala gatal say fane yeah I gotta go and struggle everyday Cause sameu life dafa tédjou beu amatoul béneu way (béneu way) Mama xar meu meu nieuw rék ngeu bégg Mane mangui deeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeeem [Refrain] [Outro : Admow & Kalz] Mane damay déma dem Kalz , Fla (i gotta go ooh) Mane damay déma dem Admow Flow Mane damay déma dem Neegu Rap , damey dem , damey dem Mane damay déma dem (i gotta go) Mane damay déma dem (i gotta go)