414 brothers - Doumala Bayii lyrics

Published

0 347 0

414 brothers - Doumala Bayii lyrics

[Verse 1 = JUST] Top love ba faf soff Top love ba faf doff Top love ba faf loff fébar nioumay fadié rose Sama life da pause Mbind mou nice kom proz Usouma c**aine mais dama Lover'Dose Yay sama barbi Bayina bi-reu yi (reubi) Done sa brebis bouma mangué kane lay mbeuki dji Ya eulbati sama vie'yeungeul sama heart bi tothie sama kani touf sama beut yi Boudei love love dou yako soss Thanks God dieuredieuf baby awma sa fayy doumala bayi yaw ( x2) [Hook = METZO] Yone bi meitina wone nga diap teuweu bayi wo mak yaw Démb la wone Doumala meuss bayi yaw Xamnga né yay sama xol mane déh soumala amoulwone wayé démb lawone Doumala meuss bayi [Verse 2 = KLAUS] Yay kimay safal Yay kimay bégueul C'est toi qui me fais voir la vie en couleur Yallah na Yallah motali Yéné gui ma am tchi yaw Ndax mayla keur ak Merco toutina tchi yaw Fintal la sound bi warnama lingay job si souf wornama Wate nané mane déh doumala meuss bayi yaw Teral tamitt warnama bégueul tamitt warnama wate nané yaw yay sama baby love Thanks God dieuredieuf baby awma sa fay doumala bayi yaw ( x2) [Hook = METZO] Yone bi meitina wone nga diap teuweu bayi wo mak yaw Démb la wone Doumala meuss bayi yaw Xamnga né yay sama xol mane déh soumala amoulwone wayé démb lawone Doumala meuss bayi [JUST] Mak yaw doufi yeup Feulei sa ara** la Yallah ko bind yague na C'est pour la vie [Hook = METZO] (x2) Yone bi meitina wone nga diap teuweu bayi wo mak yaw Démb la wone Doumala meuss bayi yaw Xamnga né yay sama xol mane déh soumala amoulwone wayé démb lawone Doumala meuss bayi 414 BROTHERS ENTERTAINMENT