DeepVibes - Ndakaru njay' lyrics

Published

0 119 0

DeepVibes - Ndakaru njay' lyrics

INTRO (...) BM Aythieu léne niou dém biir ndakarou ndiay AlyGhost Town bou néx leu diarou di wax bilay BM Mane mi deuk diko weur diko weundélou mbay AlyGhost Taax na secteur bo dougou amnagn fa waay BM Diar Xaar yalla AlyGhost Yow teulé dji Hann BM Wathei Yarrakh AlyGhost Dieulé fa gaal BM Ngor Yoff la moudié AlyGhost Wouté fa thiof BM Dialeu Almadie deuk lékeu katou Sause AlyGhost Diar Plateau téne séne Gorée Wachie Sandaga di déme Séré sama cap, dém dougou Médina Mermoz Ouacam, dougou Colobane Hlm castor, Dox feul Big Yoff akssi Patte D'oies, cognou sans loi Parcelle Guédiawaye ana wa Pininay Boy Town dou rérr biir Ndakaru Ndiay Refrain Naniou Dem Dem Dem (naniou dem) Naniou Dem Dem Dem (naniou dem) Souniou town ney bomb fane (laniou dieum) Souniou tow ney bomb fane (DK) MoOntee Welcome welcome to DK my koner Moy town bou néxa néx ték si dara dou yombe Xalé you nékh béss, ndiol si kow xéss pétch Nio nékeu si town bi deukk diko dangaaaal yow (saturday) Or holydays paradise everyday Chez Iba iow 'Hey' Chez Kathia iow, 'Hey' Nirvana iow, 'Hey' Calibso iow, 'Hey' Patio guél yi daniou pathial wéene AlyGhost Fi guéy guissé bandi deug figuéy gueuneu mouss BM Kou ragal douffi meuneu deuk wala ya fouss MoOnTee Aay boy you teng teng, you gueuneu gaw louxouss Rak tak niou keuf seu guél gueum lo leu yéna bokeu mbouss BM Ndakaru ndiay Ndakaru ndiay capitalou Sénégal Ndiaye Refrain Naniou Dem Dem Dem (naniou dem) Naniou Dem Dem Dem (naniou dem) Souniou town ney bomb fane (laniou dieum) Souniou tow ney bomb fane (DK) AlyGhost (outro) Naniou Dem Dem Dem (ndakaru ndiay ) Naniou dem dem dééé hiyéhi Dem dem dem (ndakarou ndiay) Naniou dem dem dééé hiyéhi dem dem dem (ndakarou ndiaye) Naniou dem dem dééé hiyéhi dem dem dem (ndakarou ndiay) Naniou dem dem déé hiyéhi yéééééééééééé Walay walay niou dem dakar hey Bilay walay dakar reu néex hey Yéééhééé niou dem niou dem ndakaréé walay walay dakareu nékhééé hi yéééxééé......