CaRapid Music - No Job lyrics

Published

0 60 0

CaRapid Music - No Job lyrics

Yeaaah , yeah No job , no job Kalz , Fla hun DjMouhaProd Let's goo [Refrain : Kalz] Sa you meu yéwo mangui mboubo sameu djom Daldi weurri sameu yone mangui hustle soubak ngone Yeaaah fign gnu téyé mo bone gnoune dh dégn si dém beu sonneuh Mo taxx fi dougnou fii took No Job (heey) No Job (heey) Lolu ngéy dégg errday on the block Yeah n***a No Job (heey) No Job (heey) Séne wakheuu beurri mais niome nieupéy soop heey [Fla] Galsen doxatoul ndakh job amatoul Beuri diplome fis hahaha non lolou foratoul Li fi for moy fok sa lokho goudou Wala nga dougou roukou joutou waji am ci foudou Da ngay xeuy di wouti job say mbokeu niolay gantou Mais dara gueumal sa bopeu boy boul nango tok di niakhtou Jambar! boul mosseu hady Ndakh gor mo mome lou méti Lou yone bi sori sori Beus dina nieuw gor nga téki Nangoul niaffé guéneuci Amoul beutieuk amoul goudi Amoul séral jouga wouti Wanté Li am b am moy boul nango jay sa tar Boul nango nane potite fis lo manti manti mare Diougal dori war Ndakh gor nga mola war Tol bi yatouna fis kone fok nga beuy sa war Nangoul jougué ci zero Fighting b melni héro Nguir mana am ay euro Ndakh million yi mère def sa diang bania done ay zero [Refrain] [Kalz] Deuk bii dotoul bouger ça s'entend sur toute les bouches et Gni ssi kaw dégn gnu faté cla**é life bi dém beu claté Déssit rék légni guiss maaan jamais de grande bouchées A croire que bokougnu ssi man dégn gnu opprimés Fi ngéy guiss jeune diplomé juste dorti de l'université Guiss entreprise déposé , sans succes , di chomer Parce que kénéne kou moins compétent légn moudjé recruté Pistonné ,ndaxxté son père est pote ak le PDG Deukk bi corruption rék xaliss moy fadj lépp Li gouv bi wakh goudéj beutcheuk djaapé ko ay lépp Kou né di siis di lék seu weurseukou morom Faté né kéneu moy sédeulé , Sunu borom Sénégal leu ngui deukk bu doywar Dougn leu fay seu akk ak lo meunti dor war 2000 beu 2012 man dafeu messeu tarr 2013 nouveau régime , mais batay gnoungui khar ! [Refrain] [Fla & Kalz] Ey iow dégloul ma li poloitique politicienne Di digué ay recrutement b paré guestou jokh ko séne Bopeu fok né li nguéne def tek nguéne ko ci yone Emploi pr jeune lawone Man dou li nguéne fi wakhone Keur gui nénaniou lékétou kécé naxouli beuy Séne wakh jou beuri xamone naniou né doléne niou jokh xeuy Digué ay recrutement b paré tey nguéne tek niou ay Fo dégueu tané jangoro ja nga fa beu tay [Refrain]