BossBeatz Xat Xol - They Say Dama Doof lyrics

Published

0 84 0

BossBeatz Xat Xol - They Say Dama Doof lyrics

Refrain: (Lamstar) They say que dama doof, They say que amouma diote Dama deuk si di topou sama yone (X2) Tope Sama yoon (X3) Doneté geemomawone (x2) Couplet 1: BossBeatz Baniy soga door. Kén geemoulwone liniy déf Niou nék si kourti kourti deugeur bopp. Pour done si chéf Di dream another day. Baleen fofou niou tokk di say We see the future. Liniou beugue uh dina fay Téwal pa**ion téréwoul. (univer)site niogui diangue Di kheuthie té dagoul dikoul téréwoul niongui sant Diém ko déf liguéy. Niane yalla déf si bless Investir déf ko kheuy. Be the best and f** the rest Boula niar souteniré dossi ték niéte Doléne bayi linguéne tope réponse bi stay niét Bo guéné si cogne bi nioulay xolé beutou doof Pour niom béne vadrouillard bou sankou di guént nék boss Refrain: (Lamstar) They say que dama doof, They say que amouma diote Dama deuk si di topou sama yone (X2) Tope Sama yoon (X3) Doneté geemomawone (x2) Couplet 2 : BossBeatz Téy nioy ndieuk gondi. Feusseul ni nio bokk cogne Té danela wowé bandit. Sounou xol moniou togne They dont know our dream. Xamouniou sakh liniy déf Dékou nathie téksi xif. Yotou buzzou ice cream ]I got a flow n***a. I got a mind I got a label. Légui gotta gotta f**ing money Know no limit. Osé cross the line. Amatoul xar Di wait a minute. Sounou guiss guiss dafa blind n***a Téranga adouna beut la. Néknanoussi ay ate Ba adji ni bossi amoul kopar dossi nd… gaaat Linouy yotou wéssou sa ndioorte. Daniy tothie sa th… Wala walabok hi haters what a f** n***a Refrain: (Lamstar) They say que dama doof, They say que amouma Jote Dama deuk si di topou sama yone (X2) Tope Sama yoon (X3) Doneté geemomawone (x2) Couplet: 3 Lamstar Lima geuneu nékh si sama life Damako yague geem. Geem ni beuss dina nice Ma yokk sama fight. Tayla sama tay Di job sama name. bamouy takk té dou fay Lingay récolté. Moy lépp lingay liguéy Lou méti goor lay daal. mougne ko doula ray Dafa lathie gna am fiit.. geem sa liguéyou ndeye Geemeul ligna done. Yokk lingay bay Refrain: Lamstar They say que dama doof, They say que amouma Job Dama deuk si di topou sama yone (X2) Tope Sama yoon (X3) Doneté geemomawone (x2)