[Intro : Kalz] Yeaah , brodcasting live from Neegu Rap Ice Cream...This song is for the bad girls...CaRapid Music [Refrain : Kalz] Mak iow... slow mo, ni papier A4 recto verso Kham ngani dama siiiw melni Mod' lo Baby da nga thirsty... i know ! Lo beugg ice cream ? Lick it lick it, lick it lick it. (x3) [Bako] Yagg ngameu reubb, legui magui ni Khamna lou nga beugg, sameu panini Yameu wone wéne, ma wone la guéne Looy tiit khana donato fifi? Am dieuleul setsiko Nala yobbu ba mexico Paré wone la samey 7 djiko umma good boy you da bad girl Negnu cool aight bandi niak Hum yeah be my pine-co
Lumla nara waxx girl waroul dieum kaw Haha yeah diaroul tal call féyal I don't give a f*ck... now louy sa pine code? [Refrain : Kalz] [Fla] Wane ma sa mouss niu andeu move Baby mane ak iow ci bain de mousse Dila tal sans ma lal leu... bluetooth Oups... aprés six neuf pousse pousse Khaménaleu yagg ngameu toppe nane ma beugeu naleu Legui diot na mane ak iow faaw niu andeuh defi dara Mane le F.L.A gatteu saf Da nga done diay nekh ? gatt sa! Love is da name.. s** is da game Forget da name... and play game Once again forget da name.. I mean fo real , play da game ! [Refrain : Kalz]