[Refrain] Bidew bi moussou fi Jok Assamane khine none Yéne saye khar rek gua meune def Liir bi moudji na dokh Magg na ba di daw Monté jotna rame joke tank yi bagn Lou job yomb Bolé tchi job Waro deuk tchi tokk Diougeul topal sa xol Guidé ko ak sa bop God dina def li ci dess [Lockslegl] Comme y'avait qu'une table et une chaise Quand on n'avait pas la clim Pourtant quand le publique a press play Ils ont pu recenser les crimes Puis les 1ers jours c est l'usine Le labo la cuisine Partait en concert en 7 places Maintenant on le fait en limousine On a commencé par lever des briques Je te mets au courant éléctrique 5 ans après tous parlent de nous Découper des Mc, je vais faire des frittes C'est Buzzé la paix Je leur fais la guerre Ils font la paix Sur les jaloux Je ne m'attarde guère Ils me font de la peine Hit The Club 1 Hit The Club 2 Hit The Club 3 Pendant ce temps Les mixtapes pleuvent Elles sont gratuites Ils comprennent pas Et puis il parait qu'ils écrivent pas Parait qu'ils ont tout tenter Certaines disent même que le projets C'est d'eradiquer toute qu'on fait On fait pas une etoile et un reverbère On s'est fait (4x) Ouoi les faire redescendre sur terre De quoi les faire taire Laisse les faire(4x) [Refrain] Bidew bi moussou fi Jok Assamane khine none Yéne saye khar rek gua meune def Liir bi moudji na dokh Magg na ba di daw Monté jotna rame joke tank yi bagn Lou job yomb Bolé tchi job Waro deuk tchi tokk Diougeul topal sa xol Guidé ko ak sa bop God dina def li ci dess [Canaba**e] God dina def li tchi dess Défal lila war dina faye bou tchi stress 1+1 2 yeah fils no regrette 2006 sama nék ak mic kou cyber 2007 galsen kham nagn lane moye mixtape Ndongo D, Fadda Freddy Gno ndieukeu ship gneup Legui ndongo bi done na father ci game bi Laye takhaw concert publique bi you F**k gneup Bidew bi moussou fi Jok Assamana khinone Sama team logo bi moy 3e barame ci kaw Gnou def diff' Bougnou sorou n***a parégoulo Les Mcs gnougui khif Ils n'ont pas de boulots n***a fi Gneupeul def show di késsé nimo Bou kéne tangué Gneupaye tangual Def fait domino City bi di show love
Guél yi di gnou ko diokh anytime Mélni dag nou ko amélone Général Ba** Sounou indépendance New school soldiers yi marqués les pas Tabakh thieur yi like nike Légui dotoul Dakar rek Ate bou nek gnou weur Senegal Mateu nopeu yi like Tyson Objectif bi monde bi leu Mother f**k yaw ak sa side [Refrain] Bidew bi moussou fi Jok Assamane khine none Yéne saye khar rek gua meune def Liir bi moudji na dokh Magg na ba di daw Monté jotna rame joke tank yi bagn Lou job yomb Bolé tchi job Waro deuk tchi tokk Diougeul topal sa xol Guidé ko ak sa bop God dina def li ci dess {Jp} Buzz Lab Bagnou bougué dara dagnou diok Nékone dksouth di def buzz Locks Legl diougué kaw Tégal ma deal ak Ba** Gnou yeukeuti empire di disturb Ba** yeukeuti drapeau tchi kaw F**king Buzz tchi kaw khalé yeup Di def teupe Guiss gua linguay def Bokout ak lignouy def Bo gneuwé concert rek Diém ko rek teudji Démal takhawé neulé Yéne gneup daguéne teulé Bougnou diéma dapp Usein Bolt dalay mbeulé Daguati sa khol fofou rek lagnou meuné Ladji ko sounou haters Lane mo takh gnougui khoulé We Canaba**e Club Shot out yéne gneup Buzz Lab Fépp Nagn deff tékk Fi kene dou fi répp Tép son bou doul fétchi Kham nagn né Buzz Lab moy yeugeul Play Kay dina meusseu rap taye Jay dina meusseu rap taye May Day ! Eh day Yi domaram taye Gnouy nangou sén faye Diko yakk ay rap taye Gnoune on veut les milles Donc on rape comme des millionnaires Pas de soucis a se faire Lock Legl sur le terre terre Ce cher terre Buzz Lab ce qu'on voit c'est de faucaire One hand if you love hip hop Two fingers if you love Buzz Lab et c'est tout 3ème Barame bougnou diéma bab 5ème barame pour gua takhaw rek séntou Back in the biz Make it easy Niari as yi dila teureul gua mise Goumba wouma, miyopou, diélouma Bouma téné tchi kaw kham na loumay téré ma guiss www.senlyrics.com [Refrain] Bidew bi moussou fi Jok Assamane khine none Yéne saye khar rek gua meune def Liir bi moudji na dokh Magg na ba di daw Monté jotna rame joke tank yi bagn Lou job yomb Bolé tchi job Waro deuk tchi tokk Diougeul topal sa xol Guidé ko ak sa bop God dina def li ci dess