414 brothers - NO MBADA lyrics

Published

0 243 0

414 brothers - NO MBADA lyrics

Verse 1 CHINGY a.k.a KLAUS No mbada alla selli f** b**hes i'm silly Just-illy kay firi wakhdji Chingy movi busy Shoot-out to my nizzy Cashy Omzy Leyti Mc bawal teyé lii Balloteli Clik clak niou fokhotat Say rimes niou khokotal No beef, no grief Peace fils nioune lagniy ladj Souniou hip-hop dafa high cla** Best rhymes lagniys pa**e pa**e Punchlines yi ni ca**e ca**e Kon nak Basta Geuna graw Rhymes-Busta Ladjal wa azthia Geuna quick wa nascar n***a sorinagn nioungui NASA Warakh séni carrières Palatou Pasta Aribariba ça pa**e ou ça pa**e pas Koute mate ak mbaute lép lagniy souy balé From the hood, hood star guisnga nignma ciblé No BMW no cars tay dagniy coupeulé Kon fou yi ak wa thia yeup kaylen niou roubélén Refrain DOOKAPI Jooglén, real sh** we in this b**h Ghetto swagg (swagg) Nieuw sif koufi need beat JUST maguenaa CHINGY maguenaa From santana rombenagnla yaguena X2 Verse 2 JUST From the Da-corner fils bou doyoul nagnko doliwat Criminel Boyz la bougnko degoul nagnko Bamtouwat Atiou kouma tako tako dou té fils mou botouwate Kheup essence talko talko dou té fils mou mothiouwate Aythia jongantéla Na kouné paré sa kharou b*ye Just dafa reiw dina rap ba lek sa k***rou kharou b*ye Dangerous boyz la boula timé douma tala ray Wakhdji dagnkay change tay (ngani) Ragal dina diegui rail Bété bété dou beuri wakh teudieul sa gate Stop n***a Pop pop hit a hat What a hell is goin' n***a Don't worry boudé rap we doin' it well n***a Flow bou gaw sick chromé illy Macklaren Refrain DOOKAPI Jooglén, real sh** we in this b**h Ghetto swagg (swagg) Nieuw sif koufi need beat JUST maguenaa CHINGY maguenaa From santana rombenagnla yaguena X2 Outro DOOKAPI Soumalané daniou meuna rap rap my n***a Soumalané kouniou meussa nane mandi nga Dioudou dof, dioudou bandi, dioudou sof Koudou rof, si sa a** daniou dof anhhh Soumalané daniou meuna rap rap my n***a Soumalané kouniou meussa nane mandi nga Yo yo yo Just for the game Chingy Dookapii Santana