414 brothers - JUMP - INTRO lyrics

Published

0 294 0

414 brothers - JUMP - INTRO lyrics

[Refrain] We jump (Hey) we jump (Ooh) Know what im doing Know what im talkin and we know what im singing We jump (Hey) we jump (Ooh) No worries kheuthie nope def déglou xol yei weuliss We jump (Hey) we jump (Ooh) Xeuthie bomb tale bountu xatal gni wax bountu xatal gni naxx We jump (Hey) we jump (Ooh) Def dara doufi miss yangui koy guiss gnari number 10.10 [Verse 1: JUST] Teweu nitei gnam dof nei ebou leylei Do dagalek boor doutei souba nga abe leilei Foko guicei yayei di youxu maday Just ak klaus meuss deigue sen paday maday Douma def loudul just gnew saga sa nd*y Diko rap monday wednes(day) ba satur(day) sunday Faléwouniou bandit saleté nioune faléwouniou Gondiwouniou sa rapa rare nioune tipséwouniou [Verse 2: KLAUS] Dawal dawal Just ak Klaus dou nioy fowal Beuri pekhé khebouniou dara baol baol Rawal rawal founioula képé dinga sawal Hood ak clean kounioussi kep diokhla sa wale Ndéké mic agné mic moy souniou ndawal Yor mitraillette si game bi niounane ma métél Mafi rap lou doug kaw yék Tour Eiffeil Gars yiy teup fi dal nio yor sene tiofel [Refrain] We jump (Hey) we jump (Ooh) Know what im doing Know what im talkin and we know what im singing We jump (Hey) we jump (Ooh) No worries kheuthie nope def déglou xol yei weuliss We jump (Hey) we jump (Ooh) Xeuthie bomb tale bountu xatal gni wax bountu xatal gni naxx We jump (Hey) we jump (Ooh) Def dara doufi miss yangui koy guiss gnari number 10.10 [Outro] Yeah ckeck it out negga No mbada alla selli la Donal niit mba nga done doff Kothie ko si legalize it Bii sound meuno fekhei ba do like it negga No more djizz leu kay leine dieul seine dose Sister yiiy saf saflou nio ngui niew ak choco choco Mi leine di fathie negga Beguei botei east ba west Marnune chiaar baay faal yii Mixtape bii bombe la Xaax touff sa tombe Rep´tyle Music 414 Tenn bii Entertainment